Aller au contenu

Sibiru wuute gi ci sumb yi

Jóge Wikipedia.
Contenu supprimé Contenu ajouté
CFCF (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Pamaboca (waxtaancëru)
Aucun résumé des modifications
Tafaan: Soppikaay gu gisu Soppi ak jollasu Coppite bu web ci jollasu
 
(3 versions intermédiaires par 3 utilisateurs non affichées)
Rëdd 16 : Rëdd 16 :
<!-- Definition and symptoms -->
<!-- Definition and symptoms -->
'''Sibbiru''' ab [[Feebar bu bawoo ci yoo|feebar bu yoo di joxe]] di dal nit ak yenn rab yi te li koy joxe di parasit [[protozoans]] (benn xeetu selil [[microorganism]]) bu xeetu ''[[Plasmodium]]''.<ref name=WHO2014/> Ni sibbiru di faral di feeñee mooy [[yaram wu tàng]], [[jagadi|coono]], [[waccu]] ak [[metitu bopp]]s.<!-- <ref name=EBMED2014/> --> Su demee ba tar mën na jur [[soonis|der bu mboq]], [[say]]s, [[komaa]] wala [[faatu]].<ref name=EBMED2014/> Feebar baa ngi tàmbalee feeñ fukki fan ak juróom ginaaw bu la yoo bi màttee.<!-- <ref name=WHO2014/> --> Ñi mu dal te faju ñu ko bu baax, mën na leen dalaat ginaaw ay weer ci kanam.<ref name=WHO2014/> Ñi mu dal bu yàggul ba ñu mucci, su leen dalaatee du metti noonu.<!-- <ref name=EBMED2014/> --> [[kaaraange|muslaay]] boobu nit ki am dafay jeex su amee ay weer wala at sudee newul fu mu mën a amee sibbiru.<ref name=EBMED2014/>
'''Sibiru''' ab [[Feebar bu bawoo ci yoo|feebar bu yoo di joxe]] di dal nit ak yenn rab yi te li koy joxe di parasit [[protozoans|protozoan]] (benn xeetu selil [[microorganism]]) bu xeetu ''[[Plasmodium]]''.<ref name=WHO2014/> Ni sibbiru di faral di feeñee mooy [[yaram wu tàng]], [[jagadi|coono]], [[waccu]] ak [[metitu bopp]].<!-- <ref name=EBMED2014/> --> Su demee ba tar mën na jur [[soonis|der bu mboq]], [[say]], [[komaa]] wala [[faatu]].<ref name=EBMED2014/> Feebar baa ngi tàmbalee feeñ fukki fan ak juróom ginaaw bu la yoo bi màttee.<!-- <ref name=WHO2014/> --> Ñi mu dal te faju ñu ko bu baax, mën na leen dalaat ginaaw ay weer ci kanam.<ref name=WHO2014/> Ñi mu dal bu yàggul ba ñu mucci, su leen dalaatee du metti noonu.<!-- <ref name=EBMED2014/> --> [[kaaraange|muslaay]] boobu nit ki am dafay jeex su amee ay weer wala at sudee newul fu mu mën a amee sibbiru.<ref name=EBMED2014/>


<!--Cause and diagnosis-->
<!--Cause and diagnosis-->
Gis nañu ni, màtt-màttu yoo bu jigéen bi tuddu ''[[Anopheles]]'' mooy joxe feebar bi.<!-- <ref name=WHO2014/> --> Sula màttee dafay dugal parasit yi nekk ci tiflitam ci sa [[biir yaram|deret]].<ref name=WHO2014/> Ginaaw loolu mu jàll ci res wi ndax foofu lay màggee ak juree.<!-- <ref name=EBMED2014/> --> Juróomi xeeti ''Plasmodium'' a mën a dal nit te ñooy la nit mën a wàlle.<ref name=EBMED2014/> Ñu bari ñu sibbiru di faat ''[[Plasmodium falciparum|P. falciparum]]'' ak ''[[Plasmodium vivax|P. vivax]]'', ''[[Plasmodium ovale|P. ovale]]''ñoo leen faat, ak ''[[Plasmodium malariae|P. malariae]]'' biy joxe sibbiru bu tarul lool.<ref name=WHO2014/><ref name=EBMED2014/> Xeet yi tudd ''[[Plasmodium knowlesi|P. knowlesi]]'' bariwul lu ñuy daaneel nit.<ref name=WHO2014/> Bu ñuy seet ndax danga sibbiru jël ci sa [[laamu deret]]s xool ko ci mikroskop, wala ñu jëfandikoo test bi tuddu [[antigen]]-based [[test biy feeñal àntisenu sibbiru|test bu gaaw la]].<ref name=EBMED2014/> Defar nañu jumtukaay buy jëfandikoo [[polymerase chain reaction]] ngir gis [[ADN]] bu doomu jàngoro ji, waaye loolu bariwul ci barab yi sibbiru [[Tasaaroo (epidemiology)|bari]] ndax dafa seer te jafe.<ref name="Nadjm 2012">{{Cite journal |author=Nadjm B, Behrens RH |title=Malaria: An update for physicians |journal=Infectious Disease Clinics of North America |year=2012 |volume=26 |issue=2 |pages=243–59 |pmid=22632637 |doi=10.1016/j.idc.2012.03.010}}</ref>
Gis nañu ni, màtt-màttu yoo bu jigéen bi tuddu ''[[Anopheles|Anophele]]'' mooy joxe feebar bi.<!-- <ref name=WHO2014/> --> Sula màttee dafay dugal parasit yi nekk ci tiflitam ci sa [[biir yaram|deret]].<ref name=WHO2014/> Ginaaw loolu mu jàll ci res wi ndax foofu lay màggee ak juree.<!-- <ref name=EBMED2014/> --> Juróomi xeeti ''Plasmodium'' a mën a dal nit te ñooy la nit mën a wàlle.<ref name=EBMED2014/> Ñu bari ñu sibbiru di faat ''[[Plasmodium falciparum|P. falciparum]]'' ak ''[[Plasmodium vivax|P. vivax]]'', ''[[Plasmodium ovale|P. ovale]]''ñoo leen faat, ak ''[[Plasmodium malariae|P. malariae]]'' biy joxe sibbiru bu tarul lool.<ref name=WHO2014/><ref name=EBMED2014/> Xeet yi tudd ''[[Plasmodium knowlesi|P. knowlesi]]'' bariwul lu ñuy daaneel nit.<ref name=WHO2014/> Bu ñuy seet ndax danga sibbiru jël ci sa [[laamu deret]] xool ko ci mikroskop, wala ñu jëfandikoo test bi tuddu [[antigen]]-based [[test biy feeñal àntisenu sibbiru|test bu gaaw la]].<ref name=EBMED2014/> Defar nañu jumtukaay buy jëfandikoo [[polymerase chain reaction]] ngir gis [[ADN]] bu doomu jàngoro ji, waaye loolu bariwul ci barab yi sibbiru [[Tasaaroo (epidemiology)|bari]] ndax dafa seer te jafe.<ref name="Nadjm 2012">{{Cite journal |author=Nadjm B, Behrens RH |title=Malaria: An update for physicians |journal=Infectious Disease Clinics of North America |year=2012 |volume=26 |issue=2 |pages=243–59 |pmid=22632637 |doi=10.1016/j.idc.2012.03.010}}</ref>


<!--Prevention and treatment-->
<!--Prevention and treatment-->
Sibbiru bu mën na wàññiku bu baax sudee nit ñaa ngi jëfandikoo [[sàñce (mustikeer)]]s wala [[diw bu dàq yoo]]s ngir moytu màtt-mattu yoo yi, wala def lu leen di dàq wala ray, lu ci melni [[pompu yoo]]s ak dindi dox yi taa.<ref name=EBMED2014/> Bari na garab yu ci melni [[malaria prophylaxis|prevent malaria]] yiñ jagleel ñiy tukki ci barab yu sibbiru bi tasaaroo.<!-- <ref name=WHO2014/> --> Yenn saa mën nañu bindal xale [[sulfadoxine/pyrimethamine]] [[xale]]s ak jiggéenu wérul ci [[ñatti weer]] yi njëkk cib [[ëmb]] bi ci barab yi sibbiru bari lool.<!-- <ref name=WHO2014/> --> Fiñu tollu amagul [[ñakk]] bu ci mën a aar ni naam soxla nañu ko, teewul nit ñaa ngi ciy gëstu bu baax ngir am ko.<ref name=WHO2014/> Ñaari xeeti garab yi ñu digle ngir faj feebar bi ñooy [[antimalarial medication]]s bi amaale ab [[artemisinin]].<ref name=WHO2014/><ref name=EBMED2014/> Ñaareelu garab gi mën na doon [[mefloquine]], [[lumefantrine]], wala sulfadoxine/pyrimethamine.<ref name=WHO2010>{{cite book|last1=Organization|first1=World Health|title=Guidelines for the treatment of malaria|date=2010|publisher=World Health Organization|location=Geneva|isbn=9789241547925|page=ix|edition=2nd ed.}}</ref> Mën nañu itam jël [[Quinine]] boole ko ak [[doxycycline]] sudee artemisinin amul.<ref name=WHO2010/> Mooy lañuy digle ci barab yi feebar bi bari, dañu wara xam bu baax ndax nit ki dafa sibbiru laata muy jël garab yi ndax dañuy bañ jàngoro ji [[dërkiis ci garab gi]].<!-- <ref name=WHO2014/> --> Jangoro dem na ba dërkiis ci yenn xeetu garab yu daan faj sibbiru; lu ci melni, dërkiis ci-[[chloroquine]] ''P. falciparum'' barina ci barab yi sibbiru bi bari, te itam dërkiisam ci artemisinin doon na jafe-jafe bu mag ci réew Asi Gànjoolu-penku.<ref name=WHO2014/>
Sibbiru bu mën na wàññiku bu baax sudee nit ñaa ngi jëfandikoo [[sàñce (mustikeer)]] wala [[diw bu dàq yoo]] ngir moytu màtt-mattu yoo yi, wala def lu leen di dàq wala ray, lu ci melni [[pompu yoo]] ak dindi dox yi taa.<ref name=EBMED2014/> Bari na garab yu ci melni [[malaria prophylaxis|prevent malaria]] yiñ jagleel ñiy tukki ci barab yu sibbiru bi tasaaroo.<!-- <ref name=WHO2014/> --> Yenn saa mën nañu bindal xale [[sulfadoxine/pyrimethamine]] [[xale]] ak jiggéenu wérul ci [[ñatti weer]] yi njëkk cib [[ëmb]] bi ci barab yi sibbiru bari lool.<!-- <ref name=WHO2014/> --> Fiñu tollu amagul [[ñakk]] bu ci mën a aar ni naam soxla nañu ko, teewul nit ñaa ngi ciy gëstu bu baax ngir am ko.<ref name=WHO2014/> Ñaari xeeti garab yi ñu digle ngir faj feebar bi ñooy garab yiy xeex sibbiru bi amaale ab [[artemisinin]].<ref name=WHO2014/><ref name=EBMED2014/> Ñaareelu garab gi mën na doon [[mefloquine]], [[lumefantrine]], wala sulfadoxine/pyrimethamine.<ref name=WHO2010>{{cite book|last1=Organization|first1=World Health|title=Guidelines for the treatment of malaria|date=2010|publisher=World Health Organization|location=Geneva|isbn=9789241547925|page=ix|edition=2nd ed.}}</ref> Mën nañu itam jël [[Quinine]] boole ko ak [[doxycycline]] sudee artemisinin amul.<ref name=WHO2010/> Mooy lañuy digle ci barab yi feebar bi bari, dañu wara xam bu baax ndax nit ki dafa sibbiru laata muy jël garab yi ndax dañuy bañ jàngoro ji [[dërkiis ci garab gi]].<!-- <ref name=WHO2014/> --> Jangoro dem na ba dërkiis ci yenn xeetu garab yu daan faj sibbiru; lu ci melni, dërkiis ci-[[chloroquine]] ''P. falciparum'' barina ci barab yi sibbiru bi bari, te itam dërkiisam ci artemisinin doon na jafe-jafe bu mag ci réew Asi Gànjoolu-penku.<ref name=WHO2014/>


<!--Epidemiology-->
<!--Epidemiology-->
Fi feebar bi gënee bari mooy ci [[Tropics|réew yu tàng yi]] ak [[xawa tàng]] te ñooy yi séq rëdd wiy xaajale suuf si di [[ekuwaatër]].<ref name=EBMED2014>{{cite journal|last=Caraballo|first=Hector|title=Emergency Department Management Of Mosquito-Borne Illness: Malaria, Dengue, And West Nile Virus|journal=Emergency Medicine Practice|date=May 2014|volume=16|issue=5|url=http://www.ebmedicine.net/topics.php?paction=showTopic&topic_id=405}}</ref> This includes much of [[Sub-Saharan Africa]], [[Asia]], and [[Latin America]].<!-- <ref name=WHO2014/> --> [[Mbootaayu Wérgi-yaramu Àdduna bi]] maanaam OMS xayma na ci atum 2012, ni amoon na 207 miliyo?i ñu amoon sibbiru.<!-- <ref name=WHO2014/> --> Ci at moomu, feebar bi fatna lu tollu ci diggante 473,000 ak 789,000 doomu aadama, li ëpp ci ñoom doon ay gunéy Afrik.<ref name=WHO2014>{{cite web|title=Malaria Fact sheet N°94|url=http://www.who.int/mediacentre/factsheets/fs094/en/|website=WHO|accessdate=28 August 2014|date=March 2014}}</ref> Fuñu tuddee sibbiru xel yi dem ci ndóol te loolu doonul lu baax ci [[koom-koom guy suqaliku]].<ref name="IftSoL">{{Cite report |author=Gollin D, Zimmermann C |title=Malaria: Disease Impacts and Long-Run Income Differences |date=August 2007 |publisher=[[Institute for the Study of Labor]] |url=http://ftp.iza.org/dp2997.pdf |format=PDF}}</ref><ref name="Worrall 2005">{{Cite journal |author=Worrall E, Basu S, Hanson K |title=Is malaria a disease of poverty? A review of the literature |journal=Tropical Health and Medicine |year=2005 |volume=10 |issue=10 |pages=1047–59 |doi=10.1111/j.1365-3156.2005.01476.x |pmid=16185240}} {{open access}}</ref> Xayma nañu ni at mu nekk sibbiru dina ñàkkloo Afrik lu tollu ci $12 miliyaar ciy dolaar ndax pajum feebar bi, ñàkk a mën a liggéey ak li muy yàq turism bi.<ref name="Greenwood 2005">{{Cite journal |author=Greenwood BM, Bojang K, Whitty CJ, Targett GA |title=Malaria |journal=Lancet |year=2005|volume=365 |issue=9469 |pages=1487–98 |pmid=15850634 |doi=10.1016/S0140-6736(05)66420-3}}</ref>
Fi feebar bi gënee bari mooy ci [[Tropics|réew yu tàng yi]] ak [[xawa tàng]] te ñooy yi séq rëdd wiy xaajale suuf si di [[ekuwaatër]].<ref name=EBMED2014>{{cite journal|last=Caraballo|first=Hector|title=Emergency Department Management Of Mosquito-Borne Illness: Malaria, Dengue, And West Nile Virus|journal=Emergency Medicine Practice|date=May 2014|volume=16|issue=5|url=http://www.ebmedicine.net/topics.php?paction=showTopic&topic_id=405}}</ref> Bokk na ci ñoom Afrigu Suufu-Sahara, [[Asia|Asi]], ak Amerik Latin.<!-- <ref name=WHO2014/> --> [[Mbootaayu Wérgi-yaramu Àdduna bi]] maanaam OMS xayma na ci atum 2012, ni amoon na 207 miliyoŋi ñu amoon sibbiru.<!-- <ref name=WHO2014/> --> Ci at moomu, feebar bi fatna lu tollu ci diggante 473,000 ak 789,000 doomu aadama, li ëpp ci ñoom doon ay gunéy Afrik.<ref name=WHO2014>{{cite web|title=Malaria Fact sheet N°94|url=http://www.who.int/mediacentre/factsheets/fs094/en/|website=WHO|accessdate=28 August 2014|date=March 2014}}</ref> Fuñu tuddee sibbiru xel yi dem ci ndóol te loolu doonul lu baax ci [[koom-koom guy suqaliku]].<ref name="IftSoL">{{Cite report |author=Gollin D, Zimmermann C |title=Malaria: Disease Impacts and Long-Run Income Differences |date=August 2007 |publisher=[[Institute for the Study of Labor]] |url=http://ftp.iza.org/dp2997.pdf |format=PDF}}</ref><ref name="Worrall 2005">{{Cite journal |author=Worrall E, Basu S, Hanson K |title=Is malaria a disease of poverty? A review of the literature |journal=Tropical Health and Medicine |year=2005 |volume=10 |issue=10 |pages=1047–59 |doi=10.1111/j.1365-3156.2005.01476.x |pmid=16185240}} {{open access}}</ref> Xayma nañu ni at mu nekk sibbiru dina ñàkkloo Afrik lu tollu ci $12 miliyaar ciy dolaar ndax pajum feebar bi, ñàkk a mën a liggéey ak li muy yàq turism bi.<ref name="Greenwood 2005">{{Cite journal |author=Greenwood BM, Bojang K, Whitty CJ, Targett GA |title=Malaria |journal=Lancet |year=2005|volume=365 |issue=9469 |pages=1487–98 |pmid=15850634 |doi=10.1016/S0140-6736(05)66420-3}}</ref>


==Royuwaay yi==
==Royuwaay yi==


<references />
<references />
[[Wàll:Paj]]

Sumb bi teew bu 9 Suwe 2024 à 21:45

Sibbiru
Ab Plasmodium bu bawoo ci tiflitu yoo bu jigéen di dox ci biir selilu yoo bi.
Toftale ak balluwaayi biti
Specialty infectiologie[*], médecine tropicale[*], parasitologie[*]
ICD-10 B50-B54
ICD-9-CM 084
OMIM 248310
DiseasesDB 7728
MedlinePlus 000621
eMedicine med/1385 emerg/305 ped/1357
Patient UK Sibiru
MeSH C03.752.250.552

Sibiru ab feebar bu yoo di joxe di dal nit ak yenn rab yi te li koy joxe di parasit protozoan (benn xeetu selil microorganism) bu xeetu Plasmodium.[1] Ni sibbiru di faral di feeñee mooy yaram wu tàng, coono, waccu ak metitu bopp. Su demee ba tar mën na jur der bu mboq, say, komaa wala faatu.[2] Feebar baa ngi tàmbalee feeñ fukki fan ak juróom ginaaw bu la yoo bi màttee. Ñi mu dal te faju ñu ko bu baax, mën na leen dalaat ginaaw ay weer ci kanam.[1] Ñi mu dal bu yàggul ba ñu mucci, su leen dalaatee du metti noonu. muslaay boobu nit ki am dafay jeex su amee ay weer wala at sudee newul fu mu mën a amee sibbiru.[2]

Gis nañu ni, màtt-màttu yoo bu jigéen bi tuddu Anophele mooy joxe feebar bi. Sula màttee dafay dugal parasit yi nekk ci tiflitam ci sa deret.[1] Ginaaw loolu mu jàll ci res wi ndax foofu lay màggee ak juree. Juróomi xeeti Plasmodium a mën a dal nit te ñooy la nit mën a wàlle.[2] Ñu bari ñu sibbiru di faat P. falciparum ak P. vivax, P. ovaleñoo leen faat, ak P. malariae biy joxe sibbiru bu tarul lool.[1][2] Xeet yi tudd P. knowlesi bariwul lu ñuy daaneel nit.[1] Bu ñuy seet ndax danga sibbiru jël ci sa laamu deret xool ko ci mikroskop, wala ñu jëfandikoo test bi tuddu antigen-based test bu gaaw la.[2] Defar nañu jumtukaay buy jëfandikoo polymerase chain reaction ngir gis ADN bu doomu jàngoro ji, waaye loolu bariwul ci barab yi sibbiru bari ndax dafa seer te jafe.[3]

Sibbiru bu mën na wàññiku bu baax sudee nit ñaa ngi jëfandikoo sàñce (mustikeer) wala diw bu dàq yoo ngir moytu màtt-mattu yoo yi, wala def lu leen di dàq wala ray, lu ci melni pompu yoo ak dindi dox yi taa.[2] Bari na garab yu ci melni prevent malaria yiñ jagleel ñiy tukki ci barab yu sibbiru bi tasaaroo. Yenn saa mën nañu bindal xale sulfadoxine/pyrimethamine xale ak jiggéenu wérul ci ñatti weer yi njëkk cib ëmb bi ci barab yi sibbiru bari lool. Fiñu tollu amagul ñakk bu ci mën a aar ni naam soxla nañu ko, teewul nit ñaa ngi ciy gëstu bu baax ngir am ko.[1] Ñaari xeeti garab yi ñu digle ngir faj feebar bi ñooy garab yiy xeex sibbiru bi amaale ab artemisinin.[1][2] Ñaareelu garab gi mën na doon mefloquine, lumefantrine, wala sulfadoxine/pyrimethamine.[4] Mën nañu itam jël Quinine boole ko ak doxycycline sudee artemisinin amul.[4] Mooy lañuy digle ci barab yi feebar bi bari, dañu wara xam bu baax ndax nit ki dafa sibbiru laata muy jël garab yi ndax dañuy bañ jàngoro ji dërkiis ci garab gi. Jangoro dem na ba dërkiis ci yenn xeetu garab yu daan faj sibbiru; lu ci melni, dërkiis ci-chloroquine P. falciparum barina ci barab yi sibbiru bi bari, te itam dërkiisam ci artemisinin doon na jafe-jafe bu mag ci réew Asi Gànjoolu-penku.[1]

Fi feebar bi gënee bari mooy ci réew yu tàng yi ak xawa tàng te ñooy yi séq rëdd wiy xaajale suuf si di ekuwaatër.[2] Bokk na ci ñoom Afrigu Suufu-Sahara, Asi, ak Amerik Latin. Mbootaayu Wérgi-yaramu Àdduna bi maanaam OMS xayma na ci atum 2012, ni amoon na 207 miliyoŋi ñu amoon sibbiru. Ci at moomu, feebar bi fatna lu tollu ci diggante 473,000 ak 789,000 doomu aadama, li ëpp ci ñoom doon ay gunéy Afrik.[1] Fuñu tuddee sibbiru xel yi dem ci ndóol te loolu doonul lu baax ci koom-koom guy suqaliku.[5][6] Xayma nañu ni at mu nekk sibbiru dina ñàkkloo Afrik lu tollu ci $12 miliyaar ciy dolaar ndax pajum feebar bi, ñàkk a mën a liggéey ak li muy yàq turism bi.[7]

Royuwaay yi

[Soppisoppi gongikuwaay bi]
  1. 1,0 1,1 1,2 1,3 1,4 1,5 1,6 1,7 et 1,8 "Malaria Fact sheet N°94". WHO. March 2014. Retrieved 28 August 2014. 
  2. 2,0 2,1 2,2 2,3 2,4 2,5 2,6 et 2,7 Caraballo, Hector (May 2014). "Emergency Department Management Of Mosquito-Borne Illness: Malaria, Dengue, And West Nile Virus". Emergency Medicine Practice 16 (5). 
  3. Nadjm B, Behrens RH (2012). "Malaria: An update for physicians". Infectious Disease Clinics of North America 26 (2): 243–59. PMID 22632637. doi:10.1016/j.idc.2012.03.010. 
  4. 4,0 et 4,1 Organization, World Health (2010). Guidelines for the treatment of malaria (2nd ed. ed.). Geneva: World Health Organization. p. ix. ISBN 9789241547925. 
  5. Gollin D, Zimmermann C (August 2007). Malaria: Disease Impacts and Long-Run Income Differences (PDF) (Report). Institute for the Study of Labor. 
  6. Worrall E, Basu S, Hanson K (2005). "Is malaria a disease of poverty? A review of the literature". Tropical Health and Medicine 10 (10): 1047–59. PMID 16185240. doi:10.1111/j.1365-3156.2005.01476.x.  open access publication - free to read
  7. Greenwood BM, Bojang K, Whitty CJ, Targett GA (2005). "Malaria". Lancet 365 (9469): 1487–98. PMID 15850634. doi:10.1016/S0140-6736(05)66420-3.