Luanda
Apparence
Luanda | |
---|---|
[[image:|325px|none|alt=|Skyline of {{{official_name}}}]] | |
Réew | Angolaa |
Tund | Luanda |
way-dëkk | 7 000 000 nit |
atum way-dëkk | 2 009 |
barabalu Luandaa ci lonkoyoonu Angolaa | |
Luanda (bu njëkk São Paulo da Assunção de Loanda) ab dëkkub bëj-saalumu Afrig la, di itam péeyu réewum Angolaa. Féete ci tefesu Afrig gu mbàmbulaanug Atlas gi, Luanda mooy waax wi ëpp ci Angolaa gépp
Dëkkiin
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Limu nit ñi dëkk Luanda ci at yi: