Aller au contenu

PHP

Jóge Wikipedia.


Wikipedia
Wikipedia
Bii jukki ab junj rekk la. Man nga cee duggal sa loxo suqali ko ndeem am nga ci xam-xam ci anam yi Wikipedia taxawal


PHP Làkku Day la bu ubbeeku te jàppandi, defees na ko ngir sos ay xëti web yu matale jaare ko ci ab seddalekatu HTTP3, waaye it di nay man a dox niki beneen làkk bu man a doon ci anam gu biiru, PHP làkk wuy màgg la ba ci sumbu 5 ci doxiin aki melo yu mat, akuk woom ci ag kàngoom. Yaxub PHP sos na ko moom Rasmus Lerdorf ci atum 1995, fim ne ñiy toppatoo yokkte gi ak di ko saytu moodi The PHP Group (Mbaaluk PHP gi), PHP Tëriin lu ubbeeku la ci Sarti PHP dëppalees ko ak Sarti GNU General Public License (GPL)

misaalum xëtu PHP.php / PHP.php4 /PHP.php5 PHP.phtml
<?php //baat yi fii ?>

Misaalum jëfandikuk baati PHP ci HTML.html