Aller au contenu

Tripoli (Libi)

Jóge Wikipedia.


Wikipedia
Wikipedia
Bii jukki ab junj rekk la. Man nga cee duggal sa loxo suqali ko ndeem am nga ci xam-xam ci anam yi Wikipedia taxawal


Tripoli طرابلس
Skyline of {{{official_name}}}
Réew  Libi
Tus-wu-gaar
Tus-wu-taxaw
32° 54′ 8″ Bëj-gànnaar
     13° 11′ 9″ Penku
/ 32.90222, 13.18583
Kawewaay 81 m
way-dëkk 1 682 000 nit
atum way-dëkk 2 009
Rëyaay 400 km²

Tripoli (di طرابلس tarabilus ci araab) mooy péeyu réewum Libi. Turu dëkk baa ngi tekki «ñetti dëkk yi», ndax limu jóge ci booloog ñetti dëkk yii di Oea, Leptis ak Sabrata. Mi ngi féete ci bëj-gànnaar-sowwu réew mi, taq ci tàkk gi, ci dogub suuf bu kekke, féetek Géej gu Diggu gi ci geneen wàll