Aller au contenu

Ñaqu rougeole (ŋas) wuute gi ci sumb yi

Jóge Wikipedia.
Contenu supprimé Contenu ajouté
Pamaboca (waxtaancëru)
Créé en traduisant la page « Measles vaccine »
Pamaboca (waxtaancëru)
Créé en traduisant la page « Measles vaccine »
Rëdd 1 : Rëdd 1 :
'''Ñaqu rougeole''' (ŋas) mooy li lay musal ci rougeole.<ref name=":0">"[http://www.who.int/wer/2009/wer8435.pdf Measles vaccines: WHO position paper]" (PDF). ''Weekly epidemiological record''. '''84''' (35): 349–60. 28 August 2009. <nowiki>PMID 19714924</nowiki>.</ref> Sudee bi nga njëkkee ñaqu sa yaram defarul lu koy aar ci feebar bi, soo ñaquwaate rek feebar bi dootul mën dara ci yaw.<ref name=":1">Control, Centers for Disease; Prevention (2014). ''[https://books.google.ca/books?id=nVppAgAAQBAJ&pg=PA250 CDC health information for international travel 2014 the yellow book]''. p. 250. ISBN <bdi>9780199948505</bdi>.</ref> Sudee dañu ñaq lu weesu 92% ci waa dëkk bi, mën nañu jàpp ni dëkk boobu feebar bi dufa feeñ; waaye mën na fa ñëwaat sudee limu ñiy ñaqu dafa dem ba wàññiku. Soo ñaqoo dinga mucc ci feebar bi ay at yu bari. Xama guñu bu baax ndax ndax kaaraangeg ñaq bi dafay wàññiku. Ñaq bi mën nala aar itam soo ko jëlee ci biir ñaari fan yi nga nekk ci barab bula feebar bi mëna dale.<ref name=":0" />
{{Infobox drug|Verifiedfields=changed|verifiedrevid=446097921|image=File:Providing vaccinations to protect against disease after Typhoon Haiyan (11352296333).jpg|caption=A child is given a measles vaccine.
<!-- Vacine data -->|type=vaccine|target=<!-- the antigen/bacteria/toxin/virus to protect against --> [[Measles]]|vaccine_type=<!-- killed/attenuated/live/toxoid/protein subunit/conjugate/recombinant/DNA --> Attenuated
<!-- Clinical data -->|tradename=|MedlinePlus=a601176|pregnancy_AU=<!-- A / B1 / B2 / B3 / C / D / X -->|pregnancy_US=<!-- A / B / C / D / X -->|pregnancy_category=|legal_AU=<!-- S2, S3, S4, S5, S6, S7, S8, S9 or Unscheduled -->|legal_CA=<!-- Schedule I, II, III, IV, V, VI, VII, VIII -->|legal_UK=<!-- GSL, P, POM, CD, or Class A, B, C -->|legal_US=<!-- OTC / Rx-only / Schedule I, II, III, IV, V -->|legal_status=|routes_of_administration=<!-- Identifiers -->|ChemSpiderID_Ref={{chemspidercite|changed|chemspider}}|ChemSpiderID=none|CAS_number_Ref={{cascite|correct|??}}|CAS_number=|ATC_prefix=J07|ATC_suffix=BD01|PubChem=|DrugBank_Ref={{drugbankcite|correct|drugbank}}|DrugBank=<!-- Chemical data -->}}
'''Ñaqu rougeole''' (ŋas) mooy li lay musal ci rougeole.<ref>"Measles vaccines: WHO position paper – April 2017" (PDF). Weekly Epidemiological Record. 92 (17): 205–27. April 2017. hdl:10665/255149. <nowiki>PMID 28459148</nowiki></ref> Sudee bi nga njëkkee ñaqu sa yaram defarul lu koy aar ci feebar bi, soo ñaquwaate rek feebar bi dootul mën dara ci yaw.<ref>"Measles vaccines: WHO position paper – April 2017" (PDF). Weekly Epidemiological Record. 92 (17): 205–27. April 2017. hdl:10665/255149. <nowiki>PMID 28459148</nowiki>.[https://hdl.handle.net/10665%2F255149]</ref> Sudee dañu ñaq lu weesu 92% ci waa dëkk bi, mën nañu jàpp ni dëkk boobu feebar bi dufa feeñ; waaye mën na fa ñëwaat sudee limu ñiy ñaqu dafa dem ba wàññiku.<ref>"Measles vaccines: WHO position paper – April 2017" (PDF). Weekly Epidemiological Record. 92 (17): 205–27. April 2017. hdl:10665/255149. <nowiki>PMID 28459148</nowiki>.[https://www.ncbi.nlm.nih.gov/pubmed/28459148]</ref> Soo ñaqoo dinga mucc ci feebar bi ay at yu bari.<ref>"Measles vaccines: WHO position paper – April 2017" (PDF). Weekly Epidemiological Record. 92 (17): 205–27. April 2017. hdl:10665/255149. <nowiki>PMID 28459148</nowiki>.[https://www.ncbi.nlm.nih.gov/pubmed/28459148]</ref> Xama guñu bu baax ndax ndax kaaraangeg ñaq bi dafay wàññiku.<ref>"Measles vaccines: WHO position paper – April 2017" (PDF). Weekly Epidemiological Record. 92 (17): 205–27. April 2017. hdl:10665/255149. <nowiki>PMID 28459148</nowiki>.[https://www.ncbi.nlm.nih.gov/pubmed/28459148]</ref> Ñaq bi mën nala aar itam soo ko jëlee ci biir ñaari fan yi nga nekk ci barab bula feebar bi mëna dalee.<ref>"Measles vaccines: WHO position paper – April 2017" (PDF). Weekly Epidemiological Record. 92 (17): 205–27. April 2017. hdl:10665/255149. <nowiki>PMID 28459148</nowiki>.[https://www.ncbi.nlm.nih.gov/pubmed/28459148]</ref>


Ñaq bi du indil nit ki benn jafe-jafe, doonte danga am VIH.<ref>"Measles vaccines: WHO position paper – April 2017" (PDF). Weekly Epidemiological Record. 92 (17): 205–27. April 2017. hdl:10665/255149. <nowiki>PMID 28459148</nowiki>.[https://www.ncbi.nlm.nih.gov/pubmed/28459148]</ref> Mën nala xawa sonal tuuti waaye du yàg dara.<ref>"Measles vaccines: WHO position paper – April 2017" (PDF). Weekly Epidemiological Record. 92 (17): 205–27. April 2017. hdl:10665/255149. <nowiki>PMID 28459148</nowiki>.[https://www.ncbi.nlm.nih.gov/pubmed/28459148]</ref> Maanaam fi ñu la ko jam mën na saf tuuti wala sa yaram xawa tàng.<ref>"Measles vaccines: WHO position paper – April 2017" (PDF). Weekly Epidemiological Record. 92 (17): 205–27. April 2017. hdl:10665/255149. <nowiki>PMID 28459148</nowiki>.[https://www.ncbi.nlm.nih.gov/pubmed/28459148]</ref> Amul benn yokkute buy seetlu ci limu Seetlu nañu itam 3,5 jàpp 10 kaa anaphylaxie ci miliyoŋi nit ñuñu ñaq.<ref>"Measles vaccines: WHO position paper – April 2017" (PDF). Weekly Epidemiological Record. 92 (17): 205–27. April 2017. hdl:10665/255149. <nowiki>PMID 28459148</nowiki>.[https://www.ncbi.nlm.nih.gov/pubmed/28459148]</ref> Sudee lu jëm ci feebar Guillain-Barré, autisme ak biir buy metti (maladie intestinale inflammatoire) gisu ñu ci benn yokkute.<ref>"Measles vaccines: WHO position paper – April 2017" (PDF). Weekly Epidemiological Record. 92 (17): 205–27. April 2017. hdl:10665/255149. <nowiki>PMID 28459148</nowiki>.[https://www.ncbi.nlm.nih.gov/pubmed/28459148]</ref>
Ñaq bi du indil nit ki benn jafe-jafe, doonte danga am VIH. Mën nala xawa sonal tuuti waaye du yàg dara. Maanaam fi ñu la ko jam mën na saf tuuti wala sa yaram xawa tàng. Amul benn yokkute buy seetlu ci limu Seetlu nañu itam 3,5 jàpp 10 kaa anaphylaxie ci miliyoŋi nit ñuñu ñaq. Sudee lu jëm ci feebar Guillain-Barré, autisme ak biir buy metti (maladie intestinale inflammatoire) gisu ñu ci benn yokkute.<ref name=":0" />


Ñaq bi amna mooy kese, waaye itam dina ñu koy boole ak yeneen ñaq yu ci melni ñaqu ROR, (muy boole ñaqu rubeole ak anti-ourlien)<ref>"Measles vaccines: WHO position paper – April 2017" (PDF). Weekly Epidemiological Record. 92 (17): 205–27. April 2017. hdl:10665/255149. <nowiki>PMID 28459148</nowiki>.[https://www.ncbi.nlm.nih.gov/pubmed/28459148]</ref> wala ñaqu RROV (maanaam ñu boole ñaqu RRO ak ñaq biy aare ci varicelle).<ref>Mitchell D (2013). The essential guide to children's vaccines. New York: St. Martin's Press. p. 127. <nowiki>ISBN 9781466827509</nowiki>. Archived from the original on 9 September 2017.[https://books.google.sn/books?id=w0C7L9o3m-MC&pg=PA127&redir_esc=y]</ref> Ñaq bii aare ci rougeole dafay musalaate ci feebar itam ndeem dañu ko boole ak yeneen ñaq, te effets secondaires yi dañuy wuute, lépp di aju ci xeetu ñaq bi ñu ko booleel.<ref>"Information Sheet Observed Rate of Vaccine Reactions" (PDF). World Health Organization (WHO). Retrieved 1 December 2018.</ref> Waa OMS ñoo digal ñu ñaq xale bi su amee juróom ñeenti weer te nekk ci barab bu feebar bi bari. Waaye sudee fu feebar bi bariwul la, jaaduna ñu ñaq xale bi su amee fukki weer ak ñaar.<ref>"Measles vaccines: WHO position paper – April 2017" (PDF). Weekly Epidemiological Record. 92 (17): 205–27. April 2017. hdl:10665/255149. <nowiki>PMID 28459148</nowiki>.[https://www.ncbi.nlm.nih.gov/pubmed/28459148]</ref> Ñaq bi luy doomu jàngoroy rougeole bu dundu la waaye dañu ñéewal dooleem.<ref>"Measles vaccines: WHO position paper – April 2017" (PDF). Weekly Epidemiological Record. 92 (17): 205–27. April 2017. hdl:10665/255149. <nowiki>PMID 28459148</nowiki>.[https://www.ncbi.nlm.nih.gov/pubmed/28459148]</ref> Ñaq bi puudar bu waw la, fàww ñu jaxase ko laata ñu koy jam nit ki ci suufu deram wala ci siditam.<ref>"Measles vaccines: WHO position paper – April 2017" (PDF). Weekly Epidemiological Record. 92 (17): 205–27. April 2017. hdl:10665/255149. <nowiki>PMID 28459148</nowiki>.[https://apps.who.int/iris/bitstream/handle/10665/255149/WER9217.pdf?sequence=1]</ref> Soo bëggee xam ndax ñaq bi jàppna danga saytu deretam.<ref>"Measles vaccines: WHO position paper – April 2017" (PDF). Weekly Epidemiological Record. 92 (17): 205–27. April 2017. hdl:10665/255149. <nowiki>PMID 28459148</nowiki>.[https://www.ncbi.nlm.nih.gov/pubmed/28459148]</ref>
Ñaq bi amna mooy kese, waaye itam dina ñu koy boole ak yeneen ñaq yu ci melni ñaqu ROR, (muy boole ñaqu rubeole ak anti-ourlien) wala ñaqu RROV (maanaam ñu boole ñaqu RRO ak ñaq biy aare ci varicelle). Ñaq bii aare ci rougeole dafay musalaate ci feebar itam ndeem dañu ko boole ak yeneen ñaq, te effets secondaires yi dañuy wuute, lépp di aju ci xeetu ñaq bi ñu ko booleel. Waa OMS ñoo digal ñu ñaq xale bi su amee juróom ñeenti weer te nekk ci barab bu feebar bi bari. Waaye sudee fu feebar bi bariwul la, jaaduna ñu ñaq xale bi su amee fukki weer ak ñaar. Ñaq bi luy doomu jàngoroy rougeole bu dundu la waaye dañu ñéewal dooleem. Ñaq bi puudar bu waw la, fàww ñu jaxase ko laata ñu koy jam nit ki ci suufu deram wala ci siditam. Soo bëggee xam ndax ñaq bi jàppna danga saytu deretam.<ref name=":0" />


Ci atum 2013, ñaq nañu lu tollu ci 85% xale yi ci àdduna bi.<ref>"Measles Fact sheet N°286"[https://www.who.int/en/news-room/fact-sheets/detail/measles]. World Health Organization (WHO). November 2014. Archived from the original on 3 February 2015. Retrieved 4 February 2015.</ref> Ci atum 2015 amna gën gaa néew 160 réew yu baamtu ñaq bi ngir nit ñi mën a am matuwaay yu leen musal ci feebar bi.<ref>"Immunization coverage". World Health Organization (WHO). Archived from the original on 13 July 2017. Retrieved 12 July 2017.[https://www.who.int/en/news-room/fact-sheets/detail/immunization-coverage]</ref> Ci atum 1963 la ñu njëkka génne ñaq bi.<ref>Centers for Disease Control and Prevention (2014). CDC health information for international travel 2014 the yellow book. p. 250. <nowiki>ISBN 9780199948505</nowiki>. Archived from the original on 9 September 2017.[https://books.google.sn/books?id=nVppAgAAQBAJ&pg=PA250&redir_esc=y]</ref> Ci limu garab yu am solo yi waa OMS def, mooy ñaq bi gëna am solo bu yaramu nit ki soxla.<ref>"World Health Organization model list of essential medicines: 21st list 2019". World Health Organization. 2019. hdl:10665/325771.[https://apps.who.int/iris/handle/10665/325771]</ref> Njëgi ñaq bi ci réew yu néew doole yi mingi tollu ci 0,70 USD dose bu nekk, en gros, li tàmbale 2014.<ref>"Vaccine, Measles". International Drug Price Indicator Guide. Retrieved 6 December 2015.</ref> Ginaaw feebar bi dafa faral ci barab yi nit ñu bari ñaquwul, feebar dina tax ñu xam barab yi ñaq bi barul ñu ko def.<ref>Abramson B (2018). Vaccine, vaccination, and immunization law. Bloomberg Law. pp. 10–30. ISBN 9781682675830</ref>
Ci atum 2013, ñaq nañu lu tollu ci 85% xale yi ci àdduna bi.<ref>"[http://www.who.int/mediacentre/factsheets/fs286/en/ Measles Fact sheet N°286]". ''who.int''. November 2014. Retrieved 4 February 2015.</ref> Ci atum 2015 amna gën gaa néew 160 réew yu baamtu ñaq bi ngir nit ñi mën a am matuwaay yu leen musal ci feebar bi.<ref name=":0" /> Ci atum 1963 la ñu njëkka génne ñaq bi.<ref name=":1" /> Ci limu garab yu am solo yi waa OMS def, mooy ñaq bi gëna am solo bu yaramu nit ki soxla.<ref>"[http://apps.who.int/iris/bitstream/10665/93142/1/EML_18_eng.pdf?ua=1 WHO Model List of EssentialMedicines]" (PDF). ''World Health Organization''. October 2013. Retrieved 22 April 2014.</ref> Njëgi ñaq bi ci réew yu néew doole yi mingi tollu ci 0,70 USD dose bu nekk, en gros, li tàmbale 2014. Ginaaw feebar bi dafa faral ci barab yi nit ñu bari ñaquwul, feebar dina tax ñu xam barab yi ñaq bi barul ñu ko def.<ref name=":0" />{{Infobox drug|Verifiedfields=changed|legal_UK=<!-- GSL, P, POM, CD, or Class A, B, C -->|DrugBank_Ref={{drugbankcite|correct|drugbank}}|PubChem=|ATC_suffix=BD01|ATC_prefix=J07|CAS_number=|CAS_number_Ref={{cascite|correct|??}}|ChemSpiderID=none|ChemSpiderID_Ref={{chemspidercite|changed|chemspider}}|routes_of_administration=<!-- Identifiers -->|legal_status=|legal_US=<!-- OTC / Rx-only / Schedule I, II, III, IV, V -->|legal_CA=<!-- Schedule I, II, III, IV, V, VI, VII, VIII -->|verifiedrevid=446097921|legal_AU=<!-- S2, S3, S4, S5, S6, S7, S8, S9 or Unscheduled -->|pregnancy_category=|pregnancy_US=<!-- A / B / C / D / X -->|pregnancy_AU=<!-- A / B1 / B2 / B3 / C / D / X -->|MedlinePlus=a601176|tradename=|vaccine_type=<!-- killed/attenuated/live/toxoid/protein subunit/conjugate/recombinant/DNA --> Attenuated
<!-- Clinical data -->|target=<!-- the antigen/bacteria/toxin/virus to protect against --> [[Measles]]|type=vaccine|caption=A child is given a measles vaccine.
<!-- Vacine data -->|image=File:Providing vaccinations to protect against disease after Typhoon Haiyan (11352296333).jpg|DrugBank=<!-- Chemical data -->}}

Sumb bu 5 Disembar 2019 à 16:55

Ñaqu rougeole (ŋas) mooy li lay musal ci rougeole.[1] Sudee bi nga njëkkee ñaqu sa yaram defarul lu koy aar ci feebar bi, soo ñaquwaate rek feebar bi dootul mën dara ci yaw.[2] Sudee dañu ñaq lu weesu 92% ci waa dëkk bi, mën nañu jàpp ni dëkk boobu feebar bi dufa feeñ; waaye mën na fa ñëwaat sudee limu ñiy ñaqu dafa dem ba wàññiku. Soo ñaqoo dinga mucc ci feebar bi ay at yu bari. Xama guñu bu baax ndax ndax kaaraangeg ñaq bi dafay wàññiku. Ñaq bi mën nala aar itam soo ko jëlee ci biir ñaari fan yi nga nekk ci barab bula feebar bi mëna dale.[1]

Ñaq bi du indil nit ki benn jafe-jafe, doonte danga am VIH. Mën nala xawa sonal tuuti waaye du yàg dara. Maanaam fi ñu la ko jam mën na saf tuuti wala sa yaram xawa tàng. Amul benn yokkute buy seetlu ci limu Seetlu nañu itam 3,5 jàpp 10 kaa anaphylaxie ci miliyoŋi nit ñuñu ñaq. Sudee lu jëm ci feebar Guillain-Barré, autisme ak biir buy metti (maladie intestinale inflammatoire) gisu ñu ci benn yokkute.[1]

Ñaq bi amna mooy kese, waaye itam dina ñu koy boole ak yeneen ñaq yu ci melni ñaqu ROR, (muy boole ñaqu rubeole ak anti-ourlien) wala ñaqu RROV (maanaam ñu boole ñaqu RRO ak ñaq biy aare ci varicelle). Ñaq bii aare ci rougeole dafay musalaate ci feebar itam ndeem dañu ko boole ak yeneen ñaq, te effets secondaires yi dañuy wuute, lépp di aju ci xeetu ñaq bi ñu ko booleel. Waa OMS ñoo digal ñu ñaq xale bi su amee juróom ñeenti weer te nekk ci barab bu feebar bi bari. Waaye sudee fu feebar bi bariwul la, jaaduna ñu ñaq xale bi su amee fukki weer ak ñaar. Ñaq bi luy doomu jàngoroy rougeole bu dundu la waaye dañu ñéewal dooleem. Ñaq bi puudar bu waw la, fàww ñu jaxase ko laata ñu koy jam nit ki ci suufu deram wala ci siditam. Soo bëggee xam ndax ñaq bi jàppna danga saytu deretam.[1]

Ci atum 2013, ñaq nañu lu tollu ci 85% xale yi ci àdduna bi.[3] Ci atum 2015 amna gën gaa néew 160 réew yu baamtu ñaq bi ngir nit ñi mën a am matuwaay yu leen musal ci feebar bi.[1] Ci atum 1963 la ñu njëkka génne ñaq bi.[2] Ci limu garab yu am solo yi waa OMS def, mooy ñaq bi gëna am solo bu yaramu nit ki soxla.[4] Njëgi ñaq bi ci réew yu néew doole yi mingi tollu ci 0,70 USD dose bu nekk, en gros, li tàmbale 2014. Ginaaw feebar bi dafa faral ci barab yi nit ñu bari ñaquwul, feebar dina tax ñu xam barab yi ñaq bi barul ñu ko def.[1]Royuwaay:Infobox drug

  1. 1,0 1,1 1,2 1,3 1,4 et 1,5 "Measles vaccines: WHO position paper" (PDF). Weekly epidemiological record. 84 (35): 349–60. 28 August 2009. PMID 19714924.
  2. 2,0 et 2,1 Control, Centers for Disease; Prevention (2014). CDC health information for international travel 2014 the yellow book. p. 250. ISBN 9780199948505.
  3. "Measles Fact sheet N°286". who.int. November 2014. Retrieved 4 February 2015.
  4. "WHO Model List of EssentialMedicines" (PDF). World Health Organization. October 2013. Retrieved 22 April 2014.